| Song | Oh Boy |
| Artist | Youssou N'Dour |
| Album | The Guide (Wommat) |
| Download | Image LRC TXT |
| Soy nelaw mingui xol | |
| Ngay defar mingui xalat | |
| Yakk bu gueneu gaw | |
| Ko andal muy nitt kubax | |
| Mu wutal ko sikk mou dem | |
| Xalé yangkey daw | |
| Mou diem la dimbali dou meun | |
| Mayla diaroul xalat | |
| Bo tarder mou dem ba la | |
| Té io nga dikko mouñal | |
| Koula beug dangkoy beug | |
| Mane taxaw nacci témbé | |
| Boy boy boy boy kay changer | |
| Kay changer | |
| Ninga beug dula gaw | |
| Buñu togué di waxtan | |
| Ci match bi amon bik | |
| Kuffa dominé daflay contral | |
| Bou degué ñu yeukeuti seu tour | |
| Mouné xolal deffoufi dara | |
| Liffi xewon d mettina | |
| Muné nonu la warone demer | |
| Koumou fekk ngay deff lou bax | |
| Mou fekher ba yakk ko | |
| Bula feker ngay deff lou bonn | |
| Mou pousse la nga yagg cii | |
| Mane taxaw nacci témbé | |
| Boy boy boy boy kay changer | |
| Kay changer | |
| Ninga beug dula gaw | |
| Boy boy noy boy kay changer | |
| Kay changer | |
| Ninga beug dula gaw | |
| Mane sangu naccii heheheheyyy (×2) | |
| Mame Seye Fall ohh | |
| Ya démone biir Dagana sama way nga | |
| Mo yaro Mbour guedjo sama way nga | |
| Dem deuki Louga Lô woy | |
| Mane dal io dal sama waay nga | |
| Mame Seye Fall eh | |
| Mo yaro Mbour guedj | |
| Dem Walo | |
| Io dal mane dal sama way nga | |
| Mane taxaw nacci témbé | |
| Boy boy boy boy kay changer Kay | |
| Kay changer | |
| Ninga beug dula gaw | |
| Mane sangu nacii hehehehey |
| Soy nelaw mingui xol | |
| Ngay defar mingui xalat | |
| Yakk bu gueneu gaw | |
| Ko andal muy nitt kubax | |
| Mu wutal ko sikk mou dem | |
| Xal yangkey daw | |
| Mou diem la dimbali dou meun | |
| Mayla diaroul xalat | |
| Bo tarder mou dem ba la | |
| T io nga dikko mou al | |
| Koula beug dangkoy beug | |
| Mane taxaw nacci t mb | |
| Boy boy boy boy kay changer | |
| Kay changer | |
| Ninga beug dula gaw | |
| Bu u togu di waxtan | |
| Ci match bi amon bik | |
| Kuffa domin daflay contral | |
| Bou degu u yeukeuti seu tour | |
| Moun xolal deffoufi dara | |
| Liffi xewon d mettina | |
| Mun nonu la warone demer | |
| Koumou fekk ngay deff lou bax | |
| Mou fekher ba yakk ko | |
| Bula feker ngay deff lou bonn | |
| Mou pousse la nga yagg cii | |
| Mane taxaw nacci t mb | |
| Boy boy boy boy kay changer | |
| Kay changer | |
| Ninga beug dula gaw | |
| Boy boy noy boy kay changer | |
| Kay changer | |
| Ninga beug dula gaw | |
| Mane sangu naccii heheheheyyy 2 | |
| Mame Seye Fall ohh | |
| Ya d mone biir Dagana sama way nga | |
| Mo yaro Mbour guedjo sama way nga | |
| Dem deuki Louga L woy | |
| Mane dal io dal sama waay nga | |
| Mame Seye Fall eh | |
| Mo yaro Mbour guedj | |
| Dem Walo | |
| Io dal mane dal sama way nga | |
| Mane taxaw nacci t mb | |
| Boy boy boy boy kay changer Kay | |
| Kay changer | |
| Ninga beug dula gaw | |
| Mane sangu nacii hehehehey |
| Soy nelaw mingui xol | |
| Ngay defar mingui xalat | |
| Yakk bu gueneu gaw | |
| Ko andal muy nitt kubax | |
| Mu wutal ko sikk mou dem | |
| Xal yangkey daw | |
| Mou diem la dimbali dou meun | |
| Mayla diaroul xalat | |
| Bo tarder mou dem ba la | |
| T io nga dikko mou al | |
| Koula beug dangkoy beug | |
| Mane taxaw nacci t mb | |
| Boy boy boy boy kay changer | |
| Kay changer | |
| Ninga beug dula gaw | |
| Bu u togu di waxtan | |
| Ci match bi amon bik | |
| Kuffa domin daflay contral | |
| Bou degu u yeukeuti seu tour | |
| Moun xolal deffoufi dara | |
| Liffi xewon d mettina | |
| Mun nonu la warone demer | |
| Koumou fekk ngay deff lou bax | |
| Mou fekher ba yakk ko | |
| Bula feker ngay deff lou bonn | |
| Mou pousse la nga yagg cii | |
| Mane taxaw nacci t mb | |
| Boy boy boy boy kay changer | |
| Kay changer | |
| Ninga beug dula gaw | |
| Boy boy noy boy kay changer | |
| Kay changer | |
| Ninga beug dula gaw | |
| Mane sangu naccii heheheheyyy 2 | |
| Mame Seye Fall ohh | |
| Ya d mone biir Dagana sama way nga | |
| Mo yaro Mbour guedjo sama way nga | |
| Dem deuki Louga L woy | |
| Mane dal io dal sama waay nga | |
| Mame Seye Fall eh | |
| Mo yaro Mbour guedj | |
| Dem Walo | |
| Io dal mane dal sama way nga | |
| Mane taxaw nacci t mb | |
| Boy boy boy boy kay changer Kay | |
| Kay changer | |
| Ninga beug dula gaw | |
| Mane sangu nacii hehehehey |