Soy nelaw mingui xol Ngay defar mingui xalat Yakk bu gueneu gaw Ko andal muy nitt kubax Mu wutal ko sikk mou dem Xalé yangkey daw Mou diem la dimbali dou meun Mayla diaroul xalat Bo tarder mou dem ba la Té io nga dikko mouñal Koula beug dangkoy beug Mane taxaw nacci témbé Boy boy boy boy kay changer Kay changer Ninga beug dula gaw Buñu togué di waxtan Ci match bi amon bik Kuffa dominé daflay contral Bou degué ñu yeukeuti seu tour Mouné xolal deffoufi dara Liffi xewon d mettina Muné nonu la warone demer Koumou fekk ngay deff lou bax Mou fekher ba yakk ko Bula feker ngay deff lou bonn Mou pousse la nga yagg cii Mane taxaw nacci témbé Boy boy boy boy kay changer Kay changer Ninga beug dula gaw Boy boy noy boy kay changer Kay changer Ninga beug dula gaw Mane sangu naccii heheheheyyy (×2) Mame Seye Fall ohh Ya démone biir Dagana sama way nga Mo yaro Mbour guedjo sama way nga Dem deuki Louga Lô woy Mane dal io dal sama waay nga Mame Seye Fall eh Mo yaro Mbour guedj Dem Walo Io dal mane dal sama way nga Mane taxaw nacci témbé Boy boy boy boy kay changer Kay Kay changer Ninga beug dula gaw Mane sangu nacii hehehehey