Par AbouAmg Nioune nioy gni yaggueu thi bancs yi, niafé ba am #BAC Dém #Fac, djanguéfa doundou bi téén la, faut que nga am Baak Rote ba féssal sa xél djarna di dokh ba Chine Deukk thi gëstou bania mélni gni xamoul: ba, sine Fi moy guéwou xam xam, gni fi nek djangay sén Liguéy Téla Yéwou, kén doufi khaar bamou Naadj douniou Abdou Gueye Yéndou #Amphi, mélni péppeu thi gueuneu djeul ay #fi Yeugo li amté douniou xaar secours Journée méti niou mougn ko, djéngou di doundou djaar #couloir_de_la_mort