[00:00.00]Dabbaax - Youssou N'Dour [00:13.65]Keroksou penc bognouy wadjia wathié janta bi [00:21.79]Di wadjial péssé ba [00:26.84]Moulay dabbaxx yalla nagnou la diégué yalla daal moy taan waayam [00:32.30]Moulaay dabaaaaax [00:37.66]Bougnou faté bess boboulé uhh bougnou soré bess boboulé [00:48.51]Bougnou faté bess boboulé [00:53.79]Lofa gnaane yalla may lako [01:02.22]Modaane wakhal nitt gnep mo daane wakhal nasraane yi [01:12.72]Anh mo daane kadou askane wi [01:17.80]Dafa daane wakh naane nagnou bolé sougn rew [01:23.15]Dafa daane wakh naane bou kéne wéngal gaal gui [01:28.69]Dafa daane wakh naane nagnou bolé sounou khol yi [01:33.95]Dafa daane wakh naane nagnou yeureum djiguéen [01:54.26]Sa borom bi begu na yonentam bi begu na yako liguéyal sa borom [02:02.37]Moulaye dabbaxx yaw dé wacci ngua masso wakh lou amoul [02:10.24]Kérok bang gnou djito assamaane si da leudeum [02:13.22]Bessa ngui kéne dotou ko fatéééti moulaay dabbaxx [02:21.54]Bougnou faté bess boboulé bougnou soré bess boboulé [02:32.19]Bougnou faté bess boboulé [02:37.64]Lofa gnaane yalla may lako [02:42.92]Anh modaane wakhal nitt gnep anh mo daane wakhal nasraane yi [02:53.57]Anh mo daane wakhal askane wi [02:59.12]Dafa daane wakh naane na gnep ligueye [03:04.31]Dafa daane wakh naane nagn diangal gounéyi [03:09.68]Dafa daane wakh naane na gnep liguèye [03:15.14]Dafa daane wakh naane nagn diangal djiguééne gni [03:27.58]Daawaoul sétane lou gnaaw [03:38.06]Poussom la yorone fou khotékou mou gnaw [03:41.20]Rewmirewmi amélnagnou la ndiouka moulaay dabbaxx [04:01.11]Daawaoul sétane lou gnaaw [04:05.10]Poussom la yorone fou khotékou mou gnaw [04:09.06]Rewmirewmi amélnagnou la ndiouka moulaay dabbaxx [04:12.96]Bakrék dara maam aram lô coumba thiam [04:15.96]Magn penda ak pathé penda ah [04:27.13]Modaane wakhal nitt gnep mo daane wakhal nasraane yi [04:37.69]Mo daane kadou askane wi [04:42.77]Dafa daane wakh naane nagn diap sounou rewmi [04:48.25]Dafa daane wakh naane nagnep liguéye [04:53.54]Dafa daane wakh naane nagn yeureum djiguéene gni [04:59.04]Dafa daane wakh naane nagn diangal gounéyi