[00:00.00]Létt ma - Youssou N'Dour [00:00.59]Du nii du nii bëgg naa nga létt ma [00:08.55]Walla book nga firi ma [00:11.16]Xamal ma lu leer [00:16.06]Danga maa woolu sa gàlle ma ñëw nga mel ni xale [00:21.21]Yaw daal yaw tóppal fële [00:23.84]Danga ba di tappale [00:26.48]Su fekkeeni parewoo waru loo di yónéé [00:31.90]Ngall yaw bul ma defloo lu ma nin ñi di xeebe [00:36.92]Létt ma mbaa nga firi ma [00:50.34]Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma [01:00.94]Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma [01:10.87]Lég lég sax nga yónni ma [01:13.45]Ma dem bay dem nga teye ma [01:15.99]Léégi sax dematuma [01:18.66]Damay bañ nga dugël ma [01:21.24]Bu fekkeeni parewoo waru loo di yónéé [01:26.81]Ngall yaw bul ma def loo lu ma nin ñi di xeebe [01:31.72]Létt ma mbaa nga firi ma [01:45.49]Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma [01:55.77]Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma [02:06.15]Bari pexe weesuwul nettali sa géntu moroom [02:11.52]Bëgg nga ma demal la wax ma kon li ne ci yaw [02:16.64]Bari pexe weesuwul nettali sa géntu moroom [02:21.87]Bëgg nga ma demal la wax ma kon li ne ci yaw [02:26.36]Létt ma mbaa nga firi ma [02:40.11]Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma [02:50.70]Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma [03:00.54]Boo ma waxee fi nga bëgg dem [03:03.57]Ma wax la fi ngay jaar [03:06.30]Demal bul dem waxal bul wax defal bul def [03:10.13]Man daal sonn naa sonn naa sonn naa [03:16.69]Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma [03:21.61]Bëgg naa ko tay bañ naa ko subë kon xanaa ganaaw subë [03:29.74]Bëgg ak bañ la [03:32.04]Bëgg naa ko tay bañ naa ko subë kon xanaa ganaaw subë [03:40.06]Bëgg ak bañ la [03:42.63]Bëgg naa ko tay bañ naa ko subë kon xanaa ganaaw subë [03:50.64]Bëgg ak bañ la [03:52.90]Bëgg naa ko tay bañ naa ko subë kon xanaa ganaaw subë [04:00.99]Bëgg ak bañ la [04:03.37]Bëgg naa ko tay bañ naa ko subë kon xanaa ganaaw subë [04:11.41]Bëgg ak bañ la [04:13.81]Bëgg naa ko tay bañ naa ko subë kon xanaa ganaaw subë [04:21.80]Bëgg ak bañ la [04:24.21]Bëgg naa ko tay bañ naa ko subë kon xanaa ganaaw subë [04:32.33]Bëgg ak bañ la