[00:00.00]Tukki - Youssou N'Dour [00:06.84]Yoon wi nga jël baaxul ku la koy digël da lay nax [00:14.39]Yoon wii ci des moo gën loo taseel dàldi kuy mën [00:20.83]Yoon wii nga jël [00:26.17]Booy dox ba ca biir géstul xool fi nga weesu balaa ngay [00:35.04]Booy tukki yaw [00:38.40]Booy tukki yaw [00:42.25]Booy tukki yaw [00:43.53]Na nga bàyyl ba mën [00:45.67]Ding cë jëléé lu mënë xew ca feneen [00:48.62]Dina tax nga mën xam nekkinu ñeneen [00:52.23]Foofo mën nga fa gis lu yókk sa xameel [00:56.26]Booy tukki yaw [01:01.94]Nita ngi toog di janoog yaw [01:05.44]Booba fekk na ma ngay xalaat ba tàbbi asamaan [01:08.48]Àndag niir yiy naaw dem na fu sore lépp ciy xalaatam [01:14.35]Yaw sama waay kaay ma xamal la [01:16.84]Léég léég nga toog fi nga toog tukki [01:19.22]Bu neex dem ba kaw asamaan [01:22.08]Ànd ag weer wiy naaw [01:25.10]Li ngay janeer mu lay neex boo janoo mu gën fee neex [01:28.43]Booy tukki yaw [01:31.90]Booy tukki yaw yeesal sa xameel [01:35.60]Ding cë jëléé lu mënë xew ca feneen [01:38.56]Dina tax nga mën xam nekkinu ñeneen [01:42.10]Foofa mën nga fa gis lu yókk sa xameel [01:46.12]Deel tukki yaw [01:51.42]Lëppa lëpp sàmba ma ngay naaw [01:55.01]Te booy seet sax taxu koo gaaw [01:57.58]Te léég léég mu dem ba kaaw [02:00.40]Tukkee ka neex waaw [02:03.87]Lucum cééli ma ngay naaw [02:07.55]Te léég léég mu naaw ba kaw asamaan indi fiy xabaar [02:11.39]Ku dul tukki doo xam fu dëkk neexe [02:14.60]Booy tukki yaw [02:18.20]Booy tukki yaw [02:19.51]Na nga bàyyi [02:21.70]Booy tukki yaw [02:23.13]Na nga bàyyi ba mën [02:25.25]Ding cë jëléé lu mënë xew ca feneen [02:28.31]Dina tax nga mën xam nekkinu ñeneen [02:31.83]Foofa mën nga fa gis lu yókk sa xameel [02:35.97]Booy tukki yaw [02:39.31]Booy tukki yaw [02:42.97]Booy tukki yaw [02:44.49]Na nga bàyyi ba mën [02:46.23]Ñaanu barke ah ñaanu barke [02:57.59]Nita ngi toog di janoog yaw [02:59.26]Booba fekk na ma ngay xalaat ba tàbbi asamaan [03:01.88]Àndag niir yiy naaw dem na fu sore lépp ciy xalaatam [03:08.05]Yaw sama waay kaay ma xamal la [03:09.81]Léég léég nga toog fi nga toog tukki [03:12.00]Tukki bu neex dem ba kaw asamaan [03:13.37]Làng ag weer wiy naaw li ngay janool mu lay neex boo janoog moom [03:19.12]Mu gën fee neex [03:22.19]Booy tukki yaw [03:23.54]Na nga bayyi ba mën [03:25.60]Ding cë jëléé lu mënë xew ca feneen [03:28.70]Dina tax nga mën xam nekkinu ñeneen [03:32.20]Foofa mën nga fa gis lu yókk sa xameel [03:36.55]Deel tukki yaw [03:39.85]Lëppa lëpp sàmba ma ngay naaw [03:43.39]Te booy seet sax taxu koo gaaw [03:46.98]Te léég léég mu dem ba kaaw [03:49.42]Tukkee ka neex waaw [03:53.02]Lucum cééli ma ngay naaw te booy seet sax taxu koo gaaw [03:59.83]Ëndaaleel ñu xabaar [04:01.63]Tukkee ka neex waaw